Content-Length: 52477 | pFad | https://wo.wikipedia.org/wiki/Akaykus
Akaykus – Ci angale mooy Achaicus, ci faranse mooy Achaïcus.
Benn toppkatu Yeesu bu dëkk ci Korent la woon. Moom ak Fortunatus ak Estefanas dem nañu Efes ngir xamal Pool xebaaru mbooloom ñi gëm ma nekkoon ca Korent.
Ci Injiil dañuy gis Akaykus ci 1Ko 16:17.
Fetched URL: https://wo.wikipedia.org/wiki/Akaykus
Alternative Proxies:
Alternative Proxy
pFad Proxy
pFad v3 Proxy
pFad v4 Proxy