Content-Length: 107109 | pFad | https://wo.wikipedia.org/wiki/Polineesi

Polineesi — Wikipedia Aller au contenu

Polineesi

Jóge Wikipedia.
Fi Polineesi féete

Polineesi benn la ci diwaan yi ñu seddatlee goxu Oseyaani.

Bii seddatlin nga xam ne Kureelu Mbootaayu Xeet yi sax mooy la jëfandikoo suy seddatle àdduna bi ci ay Diwaan, gëstukat yi ñoom seddatle bu bees bi la ñu taamu, moo xaaj Oseyaani ci ñaari diwaan: Oseyaani gu jege ak Oseyaani gu sori yi Polineesi box. Diwaan bi dafa am meloow ñettkoñ

Baatu Poloneesi waa faraas bii di Jules Dumont d'Uville moo ko sakk ci li jege atum 1830 (moo sakk itam baat yii di Melaneesi, Mikroneesi ak Maleesi), mi ngi jóge ci baati waa Geres yii di πολύς (bari) ak νησος (dun), maanaam dun yu bari.

Diwaan bi ay dun yu baree fi ne, man nan cee lim:

Diwaani Oseyaani
Óstraali · Melaneesi · Mikroneesi  · Pacific Rim · Polineesi








ApplySandwichStrip

pFad - (p)hone/(F)rame/(a)nonymizer/(d)eclutterfier!      Saves Data!


--- a PPN by Garber Painting Akron. With Image Size Reduction included!

Fetched URL: https://wo.wikipedia.org/wiki/Polineesi

Alternative Proxies:

Alternative Proxy

pFad Proxy

pFad v3 Proxy

pFad v4 Proxy